assirou mahal abrari . Khassida en phonétique et traduit en Français
HTML-код
- Опубликовано: 30 мар 2025
- Cheikhoul khadim , Serigne Touba Mbacké
" N'abusez pas de ma condition d'homme noir ,pour ne pas profiter de moi car je suis le serviteur éternel ,chaque génération qui passe aura la certitude que je suis venu pour elle "
Thieuyyy serigne Touba kene dou iow diereudieuféti serigne Touba khassida yi chaque jours gnou toyal sama khol❤️
Suis tijan mais yallah rek mo xam xasida bii fimou toll cii mane beugu anko trop yalla nagnou yallah fayal Cheikhoul Khadim cii barkei sopem ba Rassouloulahi
Amine
Je le dit haut et fort dieureudieuf SERIGNE TOUBA 😢😢😢💓💓
salam je suis Malien, j’ai été au Magal de cette année. vraiment je n’ai rien à dire wly!
seulement apprendre d'avantage sur Cheikh Ahmadou Bamba et ses khassida.
Hamma BA . Je suis heureux pour toi . Heureux que tu t'intéresse aux khassida . Pour toute info supplémentaires envoi moi 1 mail au 313diop@gmail.com
ok inchaallah.
j’ai envoyé 1 mail.
Hamma BA hereux de toi machala continu sur cet lance dans l’Audelas inchala tu sera secouru par le meilleur walahi
tidjane la wallahi assirou douguena sama xol bi trop yalna yalla yok fayal Serigne Touba
Machallah yalla nagnou yalla fayal serigne touba
Hoooooo dieureudieufè Serigne touba ❤️❤️❤️❤️🙏
binétte diaby damalay suivre Instagram wayé guissnané kou beug Seringe bi nga nimalako sédélai fi si adouna yalnalako sédélai euleuk yamal khiyam si kanamou Seringe amine kou beug kou tedki ma beugleu
Dwayne Johnson hooo😭😭😭😭😭😭😭ioe Borom Bakh gna bilay je sais pas Sakh Yalla naniou ko bokou si barkè Borom touba ❤️❤️❤️❤️😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭kontan si ioe
dieuredieuf souniou borom.mom mignou diokh souniou maak niou bakh gni.koussi mélni serigne touba,Mame Maodo, Mame baye niass,seydina Limamou Laye, cheikh Bocounta ndiassane..ak magou diné yeup
J'aime le khassida de Mame borom touba.machala.et merci pour la traduction
Merci Sall Ngary
Mashallah. Vous avez fait un travail de grande valeur. Yalla na lèn Borom bi faye yiw...
Qui est là le jour du Magal pour dire jeureudieufé Serigne Touba 💫
Salam , il sagit du 18 safar (calendrier musulman) pour 2021 cela devrait coincider vers la fin du mois de Septembre inshAllah.
Et je pleure de joie il y a rien de plus beaux ! Vive le Mouridisme,🙏🙏🙏🤲🤲🤲
Thieuy serigne touba cheikhoul khadim mbackè kenn dou yw mbackè balla ayssa souniou yakar tay ak euleuk bamba merci bamba partout bamba for ever shuis mouride a jamais
Sante serigne touba
MERCI pour la traduction. J'ai grandi et vieilli sans jamais comprendre ce qui se disait dans ces khassaides.
MASHA ALLAH thieuy s.touba yala na nou ko yala fayal amiiin yarabi.
merci le créateur Allah et son prophète Mohamed dieureudieuf SERIGNE TOUBA
Akassa. Amna solo
Psl
Alhahou akbar machalla machalla machalla dieureudief Serigne Touba
J'aime cette xassidas
Doli sante yalla mignou bolé ak Serigne touba
Dieureudieuf serigne touba mbacké 💪💪💪💪
Dieureudieuf Serigne Touba 🙏🏽 🙏🏽
Machalla SERIGNE touba LO si defoul si lou bax doyoul machalla
Serigne touba amoul morome
Yalla nallaine sounou borom faye thi barkai cheikhoul khadim
Amine
Machallah amatina solo amine ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🤗🤗🤗🤗🤗😭😭😭😭😭
Dieuredieuf cheikhoul khadim diarama mame cheikh ibrahima fall
Jërëjëf Boroom Tuubaa jaraama Maam Seex Ibraayma Faal!
Djeredjeufé serigne touba
Machalla dieureudieufé serigne touba khadimou Rassoul souma tourando🥰🥰🥰
❤️❤️❤️❤️❤️❤️dieureudieuf borom touba
merci serigne touba
Dieureudieuf serigne touba
machalla yalna diam yagua si Sénégal way
Thieuy Serigne Touba
Ndeye Sann
Machalah dieuredieufé Serigne Touba
li amna solo pour sama genre gui menul touss
diadieuf
Diadieuf
Non yaw diadieuf
Khady Fay
Khady yaw dee mane guay wakhal gua khamni dama beug khassida bi depuis khalé té khawma paroles yi parole yi
Wéto si deh
Bari nga si morom
Serigne Touba 👌👌👌
Machala amnasolo trop contanna si barcke brom Touba mbacke
Mashaalah , sanre serigne touba
Dieureudjeufety Serigne Touba
dieureudieuf borom touba
un grand Merci à vous Assane Diop, grâce à vous je peux apprendre cette khassaide par coeur et la transcription française qui me permettra de connaitre son sens (car ne sachant lire l'Arabe)
Merci . le but du travail c faire comprendre aux gens le message du Cheikh
@@assanediop2242 assane diop jeurejeufetety
@@assanediop2242 yallna la mame borom touba fayal bopam
Dieuredieuf Serigne Touba ❤️❤️❤️❤️❤️
Asmahou akhli badrine anamou
Dieuredieuf Cheikhoul Khadim
En écoutant ce poème on se rencontre que Serigne Touba savez son retour qui d'où nite kessee
J adore vraiment et ce facile a apprendre
Merci beaucoup
@@assanediop2242 mais derien je m'en bénéficie en les écoutant donc c'est a moi de dire merci
cheikhoul khadim👌
ah machaAlla ou amna solo yalla borome bi fayla
Merci Assane Yalla na yalla fay yiww
Depuis j'ai eu une petite fille qui s'appelle Marieme Soda.
Machallah 💚
J' aime bien
Amna solo lole way
Machalla ❤
lirekkk moy firndél né kou tedd ki sounou borom loumou donn diayyyy,cheikhoul khadim amna ndieugwi té dieundeunako
Merci merci 😍😍
Ioe sama toureundo gueu . 💗 sur toi
Amna solo trop machallah🙏
Malene begu
Ahmadou bamba❤❤❤
Macha'Allah
MERCI ASSANE
Merci FANGEL
Dieureudieufe serigne touba
QEUL ASSANE
Masahall
mashallah
J'ainune question le khassida c'est les paroles du coran ou ??
Mister MagicHN Assalamou aleykoum (Que la Paix soit sur vous). Les khassida sont des poèmes écrits par le Saint homme Cheikh Ahmadou Bamba qui trouvent son inspiration dans le Coran et la Tradition prophétique. La plupart d'entre eux sont des prières faites sur le prophète Mohammed (Que la Paix et la Bénédiction d'Allah soit sur lui) et ses louanges. Cheikh Ahmadou Bamba est la plus grande figure religieuse du Sénégal.
💞
Est ce que vous avez une traduction ou transcription de dialibatoul marakhib?
Si oui pouvez vous me l'envoyer par mail merygueye1@gmail.com
🙏🏽❤️
nacadef
Serigne Touba amoul morom
@@awadione5266 ndaysan wolof la beuga wakh nanga def la beuga wakh ap nasaran la
ruclips.net/video/SExv0Otxqe0/видео.html
❤❤❤❤
Dieureudieufé serigne touba 🙏 dieureudieufé serigne touba
Dieureudieuf serigne touba
Dieureudieuf serigne touba